1 Kings 5:19
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fii ma nekk damaa fas yéene tabax kër, tudde sama Yàlla Aji Sax ji. Muy la Aji Sax ji waxoon sama baay Daawuda, ne ko: “Sa doom ji may def sa kuutaay ci sab jal moo may tabaxal kër, tudde ma ko.”
Compare 1 Kings 5:19 across all translations →