1 Kings 5:26
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu loolu weesee Aji Sax ji mayoon na Suleymaan xel mu rafet, na mu ko ko dige woon. Jàmm it doxoon na diggante Iram ak Suleymaan, ba ñu fasante kóllëre ñoom ñaar.
Compare 1 Kings 5:26 across all translations →