2 Samuel 19:44
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa Israyil ne waa Yuda: «Noo leen ëpple ci Buur fukki yoon, noo leen ëpp sañ-sañ fopp ci Daawuda. Lu ngeen nuy xeebe? Xanaa du noo jëkka wax lu jëm ci délloosi sunu buur?» Ci kaw loolu waa Yuda dellu tontu waa Israyil kàddu yu gënatee ñagas.
Compare 2 Samuel 19:44 across all translations →