Ezekiel 21:33
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yaw nag nit ki, jottlil bii waxyu, nga ne: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ci mbirum Amoneen ñeek seeni saaga ne: Saamaroo saamar, bocciku, nara bóome, xacce ba mana yàppe, di tàkk ni melax.
Compare Ezekiel 21:33 across all translations →