Isaiah 8:23
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye lëndëm googu du sax ci réew mii jàq tey. Démb Aji Sax ji torxal na réewum Sabulon ak mu Neftali, waaye ëllëg mu teral waa foofa, dale ko diiwaanu tefesu géej, ba ca wàllaa dexu Yurdan, boole ca sax Galile ga ca doxandéem ya.
Compare Isaiah 8:23 across all translations →