Malachi 3:24
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mooy delloo xolu baay ca doom ja, delloo xolu doom ca baay ba, lu ko moy ma dikk duma réew mi, ba faagaagal ko.»
Compare Malachi 3:24 across all translations →
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)