Nehemiah 10:40
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci néeg yooyu la bànni Israyil ak askanu Leween ñi di yóbbu jooxeb pepp ba ak biiñ baak diw ga; fa la ndabi bérab bu sell ba dence, te fa la sarxalkat, ya sasoo liggéey ba nekk, ñook fara bunt yaak jàngkat ya. Nu dogu nag ne dunu sàggane sunu kër Yàlla ga.
Compare Nehemiah 10:40 across all translations →