Nehemiah 3:36
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu ma ne: «Ngalla sunu Yàlla, déggal rekk xeebeel gi ñu nu xeeb te walbati seeni xaste, mu këppu ci seen kaw. Ngalla jébbal leen nit ñu sëxëtoo seen alal ci réew mu ñu leen jàpp njaam.
Compare Nehemiah 3:36 across all translations →