Numbers 17:21
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Musaa àgge ko bànni Israyil, mboolem seen kilifay kër maam jox Musaa aw yet, kilifa gu ci nekk wenn yet, ñeel kër maamam, muy fukki yet ak ñaar, yetu Aaróona bokk ca.
Compare Numbers 17:21 across all translations →