Numbers 30:17
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yooyu dogali yoon la Aji Sax ji dénk Musaa, ci diggante nit ak jabaram, ak diggante baay ak doom ju jigéen, ba muy ndaw te nekk kër baayam.
Compare Numbers 30:17 across all translations →