Deuteronomy 28:69 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lii mooy sàrti kóllëre, gi Aji Sax ji santoon Musaa ngir mu fasoo ko ak bànni Israyil, ca réewum Mowab, te bokkewul ak kóllëre ga mu fasoo woon ak ñoom ca tundu Oreb.