Deuteronomy 28:69
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lii mooy sàrti kóllëre, gi Aji Sax ji santoon Musaa ngir mu fasoo ko ak bànni Israyil, ca réewum Mowab, te bokkewul ak kóllëre ga mu fasoo woon ak ñoom ca tundu Oreb.
Compare Deuteronomy 28:69 across all translations →