Ephesians 5
Wolof 1987
4Dawleen it yu jekkadee, ni wax ju ñaaw mbaa waxi caaxaan ak kaf yu bon, te ngeen sax ci sant Yàlla.
20Gërëmleen Yàlla Baay bi ci turu Yeesu Kirist Boroom bi, fu ngeen man a tollu, ci lu mu man a doon;
23Ndaxte góor mooy kilifag jabaram, ni Kirist nekke kilifag mbooloom ñi gëm, muy jëmmam ji muy sàmm.