bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Ezekiel 6
Ezekiel 6
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 5
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 43
Chapter 44
Chapter 45
Chapter 46
Chapter 47
Chapter 48
Chapter 7 →
1
Gannaaw loolu kàddug Aji Sax ji da maa dikkal, ne ma:
2
«Yaw nit ki, jàkkaarlool ak tundi Israyil, nga waxal leen waxyu.
3
Neel: “Yeen Tundi Israyil, Dégluleen kàddug Boroom bi, Aji Sax ji. Boroom bi Aji Sax ji moo wax lii, jëme ci tund wu mag ak wu ndaw ak xunteeku xur, ne: Maa ngi nii di leen wàcceel saamar, maay màbb seen jaamookaayi tuur,
4
seen sarxalukaay gental, seen suurukaayi tuur tasaaroo, ma tëral seeni nit ñu ñu bóom fi seen kanam kasaray tuur.
5
Maay tegal seen kasaray tuur néewi bànni Israyil. Maay wasaare seeni yax fi wër seeni sarxalukaay.
6
Fu ngeen mana sance, seeni dëkk ay gental, seen jaamookaayi tuur wéet, seeni sarxalukaay yàqu, gental, seen kasaray tuur rajaxoo ba jeex, seen suurukaayi tuur màbb, seeni liggéey réer.
7
Dees na leen bóom, ba ngeen xam ne maay Aji Sax ji.
8
Waaye maay déeg lenn ci yeen, ñu rëcc saamar, tasaaroo ci xeet yi, ci biir réewi jaambur.
9
Su boobaa seenu ndes di ma fàttlikoo fa biir xeet ya ñu leen yóbbu njaam, fa may jeexale seen xolu gànc, bi ma dëddu, ak seen gët yi ñuy gànctook seeni tuur. Su boobaa ñu jéppi seen bopp ndax lu bon li ñu def ak seen jépp jëf ju siblu.
10
Dinañu xam ne maay Aji Sax ji, te du neen laa leen artoo, ba ma leen di tëkkoo mii musiba.
11
«“Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Fenqeel say loxo, dóor sa tànk fi suuf te ne: ‘Ñaw!’ ci mboolem jëfi waa kër Israyil ju bon ju siblu. Saamar ak xiif ak mbas lañuy fàddoo.
12
Ku sore deeye mbas, ku jege fàddoo saamar, ku ca mucce, deeye xiif, ma ŋaccal leen sama xadar.
13
Dingeen xam ne maay Aji Sax ji, bu seeni néew nee xas fi seen biiri tuur, ak fi wër seeni sarxalukaay, ak kaw tund wu mag ak wu ndaw, ak mboolem ker garab gu naat, ak mboolem garab gu mag te sëq, fépp fu ngeen di taale cuuraay, ñeel seen mépp tuur.
14
Maa leen di dóor sama loxo, réew mi, ma gental koo gental, dale ko màndiŋ ma ba Dibla, ak fépp fu ñu mana sance. Su boobaa ñu xam ne man maay Aji Sax ji.”»
← Chapter 5
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 43
Chapter 44
Chapter 45
Chapter 46
Chapter 47
Chapter 48
Chapter 7 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42
43
44
45
46
47
48