bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Isaiah 21
Isaiah 21
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 20
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 43
Chapter 44
Chapter 45
Chapter 46
Chapter 47
Chapter 48
Chapter 49
Chapter 50
Chapter 51
Chapter 52
Chapter 53
Chapter 54
Chapter 55
Chapter 56
Chapter 57
Chapter 58
Chapter 59
Chapter 60
Chapter 61
Chapter 62
Chapter 63
Chapter 64
Chapter 65
Chapter 66
Chapter 22 →
1
Yéene bii moo wàccal màndiŋ ma feggook géej ga: Ni ag ngëlén di riddee jaare Negew ni la noon di bawoo màndiŋ ma, jóge réew mu raglu.
2
Peeñu mu ñàng lañu ma ci wax. Workat biy wor, yàqkat biy yàq. Yeen waa Elam, songleen; yeen waa Medd, gawleen leen. Dakkal naa mboolem onk yu ñu sabab.
3
Lii a waral sama njàqareg xol, mitit jàpp ma, mel ni mititu mat, ma jaaxle ba déggatuma, jàq ba gisatuma.
4
Bopp ubu, tiitaange jàpp ma; sama ngoonug bànneex soppiku guddi gu raglu.
5
Ndab taaje, laltan lale, ñuy lekk ak a naan. Ñu jekki ne: «Yeen kilifa yi, jógleen! Diwleen pakk yi!»
6
Boroom bi kat da maa wax, ne ma: «Doxal taxawal ab jongrukat, lu mu gis, wax ko.
7
Bu gisee gawar ci watiiru ñaari fas, ak ñu wari mbaam ak ñu wari giléem, na teewloo teewlu bu baax.»
8
Jongrukat ba àddu ca kaw ne: «Sang bi, maa ngii yendoo séentu, fanaane wattu fii ma taxaw.
9
Ma ne gawar a ngii, war watiiru ñaari fas. Nee: “Daanu nañoo, Babilon daanu na, jëmmi tuuram yépp tasaaroo fi suuf!”»
10
Yeen bokk yi ñu bàcc ni pepp ca sama dàgga ja, la ma dégge ci Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi, wax naa leen ko.
11
Yéene bii moo wàccal Duuma: Nit a ngi may wooye tundu Seyir, naan: Jongrukat bi, lu des ci guddi gi? Éy jongrukat bi, lu desati ci guddi gi?
12
jongrukat bi ne: «Bët set, mu guddeeti rekk, Boo amee looy laaj, délsil laajaat ko.»
13
Yéene bii moo wàccal Arabi: yeen cëggi askanu Dedan, mbooyum Arabi ngeen di fanaane.
14
Yeen waa Tema, dajejileen ak ña mar, yóbbul leen am ndox. Dogileen ñay daw, may leen ñu lekk.
15
Ay saamar de lañuy daw; saamar bu ñu leen xàccil ak fitt gu ñu leen diir ak tàngooru xare.
16
Aji Sax ji de da maa wax ne ma: «Fileek menn at mu surga bu ñu bind waññ, sagub dëkk bii di Kedar dina sàggiku,
17
li des ci jàmbaari fittkati Kedar di lu néew.» Aji Sax ji Yàllay Israyil wax na ko.
← Chapter 20
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 43
Chapter 44
Chapter 45
Chapter 46
Chapter 47
Chapter 48
Chapter 49
Chapter 50
Chapter 51
Chapter 52
Chapter 53
Chapter 54
Chapter 55
Chapter 56
Chapter 57
Chapter 58
Chapter 59
Chapter 60
Chapter 61
Chapter 62
Chapter 63
Chapter 64
Chapter 65
Chapter 66
Chapter 22 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42
43
44
45
46
47
48
49
50
51
52
53
54
55
56
57
58
59
60
61
62
63
64
65
66