bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Isaiah 38
Isaiah 38
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 37
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 43
Chapter 44
Chapter 45
Chapter 46
Chapter 47
Chapter 48
Chapter 49
Chapter 50
Chapter 51
Chapter 52
Chapter 53
Chapter 54
Chapter 55
Chapter 56
Chapter 57
Chapter 58
Chapter 59
Chapter 60
Chapter 61
Chapter 62
Chapter 63
Chapter 64
Chapter 65
Chapter 66
Chapter 39 →
1
Jant yooyu Esekiya moo woppoon, bay waaja dee. Yonent Yàlla Esayi doomu Amocc dikk, ne ko: « Aji Sax ji dafa wax ne: “Dénkaaneel sa mbiri kër, ndax dangay dee, doo jóg!”»
2
Esekiya nag walbatiku, jublook miir ba, ñaan ci Aji Sax ji.
3
Mu ne: «Éy Aji Sax ji, ngalla bàyyil xel ni ma àndeek yaw sama léppi xol, ci kóllëre. Te it li nga rafetlu laa jëfe.» Mu jooy nag, jooy yu metti.
4
Ci kaw loolu kàddug Aji Sax ji dikkal Esayi, ne ko:
5
«Doxal ba ca Esekiya, nga ne ko: Aji Sax ji sa Yàllay maam Daawuda dafa wax ne: “Dégg naa sag ñaan, gis naa say rongooñ. Maa ngii di yokk ci saw fan fukki at ak juróom.
6
Buurub Asiri ak dooleem, maa la ciy xettli, yaw ak dëkk bii, te maay aar dëkk bii.”»
7
Lii nag ngay def ab takk bu bawoo ci Aji Sax ji, di firndeel ne Aji Sax ji dina def li mu wax:
8
Maa ngii di delloo ker gi gannaaw lu tollook fukki dëggastal, ya jant bi wàccoon ca kaw iskaleb Axas. Ci kaw loolu jant bi dellu gannaaw lu tollook fukki dëggastal ya mu jotoona wàcc.
9
Mbind mii nag Esekiya buurub Yuda moo ko bindoon, gannaaw ba mu tëddee wopp, ba jóg:
10
Man de dama noon: «Sama digg doole laay deme jaare bunti njaniiw, sama ndesu fan réer ma!»
11
Ma noon: «Dootuma gisati Aji Sax ji, duma gisati Aji Sax ji fi kërug àddina. Duma tegati doom aadama bët, dootu fii ci waa àddina.
12
Sama dëkkuwaay lañu sempi, yóbbu fu sore, mbete xaymab sàmm. Sama àpp a taxañe, ni ndimo lu ab ràbb doge ca mbaam ma. Diggante bëccëg ak guddi, nga jekkli ma.
13
May xalaat, ba bët set; Aji Sax jiy dammat samay yax ni gaynde, diggante bëccëg ak guddi, nga jekkli ma.
14
May ciib-ciibi ni wetwet mbaa ramatu, di binni nim xati, di séentu kaw ba saay gët giim. Dama noon: Éy Boroom bi, loof naa, dimbali ma.»
15
Waaye lu may waxati? Aji Sax jee ma wax, te moo jëf. Kon, ma temp ndànk sama giiru dund ndax tiisu xol.
16
Boroom bi, ci sa kàddook sa jëf la nit di dunde te ci laay noyyee ba tey. Yaa ma wéral, may ma, ma dund.
17
Ndeke sama tiisu xol wii, sama jàmm rekk a tax. Sa cofeel a tax nga sorele maak paxum sànkute. Yaa sànni sa gannaaw sama bépp bàkkaar.
18
Njaniiw du la sant, ndee du la gërëm, te ku tàbbim pax yaakaaratul sa kóllëre.
19
Kiy dund, kiy dund doŋŋ mooy ki lay sant ni man bésub tey jii, te baay mooy xamal doom sa kóllëre.
20
Aji Sax ji yaa may wallu, nu di la woy, ànd aki xalam, sunu giiru dund, fa sa biir kër, yaw Aji Sax ji.
21
Fekk na Esayi noon: «Indileen ab danku figg, ngeen jonj ko ci taabu Esekiya bi, kon dina dund,»
22
ba Esekiya noon ko: «Ana lu di takk biy firndeel ne dinaa wér, ba dellooti kër Aji Sax ji?»
← Chapter 37
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 43
Chapter 44
Chapter 45
Chapter 46
Chapter 47
Chapter 48
Chapter 49
Chapter 50
Chapter 51
Chapter 52
Chapter 53
Chapter 54
Chapter 55
Chapter 56
Chapter 57
Chapter 58
Chapter 59
Chapter 60
Chapter 61
Chapter 62
Chapter 63
Chapter 64
Chapter 65
Chapter 66
Chapter 39 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42
43
44
45
46
47
48
49
50
51
52
53
54
55
56
57
58
59
60
61
62
63
64
65
66