bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Jeremiah 43
Jeremiah 43
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 42
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 43
Chapter 44
Chapter 45
Chapter 46
Chapter 47
Chapter 48
Chapter 49
Chapter 50
Chapter 51
Chapter 52
Chapter 44 →
1
Gannaaw ba Yeremi waxeek mbooloo mépp, ba sottal mboolem kàddu yooyu ko seen Yàlla Aji Sax ji santoon mu yegge leen ko,
2
Asaryaa doomu Osaya ak Yowanan doomu Kareya ak nit ñu bew ñooñu ñépp jël kàddu gi. Ñu ne Yeremi: «Dangay fen! Sunu Yàlla Aji Sax ji santu la nga fommloo nu sunu yoonu Misra ga nu bëgga toogi.
3
Xanaa Barug doomu Nerya kay moo lay xiirtal ci sunu kaw, ngir teg nu ci loxol waa Babilon, ñu rey nu, mbaa ñu yóbbu nu ngàllo ca Babilon.»
4
Ci kaw loolu Yowanan doomu Kareya ak yeneen njiiti xare ya yépp ak mbooloo ma mépp gàntal Aji Sax ji, baña des réewum Yuda.
5
Ba loolu amee Yowanan ak njiiti xare yépp yóbbu ña desoon ca Yuda ñépp, di mboolem ña ñu jëkkoona sànni ca biir xeet ya leen séq yépp, te ñu ñibbsi woon réewum Yuda,
6
góor ñaak jigéen ñaak gone yaak doomi buur yu jigéen ya. Yóbbu nañu mboolem ña Nebusaradan njiitu dag ya tegoon ci loxol Gedalya doomu Ayikam doomu Safan; ñu yóbbaale Yonent Yàlla Yeremi ak Barug doomu Nerya.
7
Ñu dikk Misra, baña déggal Aji Sax ji, daldi àgg dëkk ba ñuy wax Tapanes.
8
Gannaaw loolu kàddug Aji Sax ji dikkal Yeremi ca Tapanes, ne ko:
9
«Jëlal ñaari doj yu mag yooy suuli ca dëru ban ba ca bunt kër Firawna gi ci biir dëkk bi, te na ko waa Yuda fekke.
10
Nga wax leen ne leen: “Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Maa ngi nii di yónnee, jëli Nabukodonosor buuru Babilon, mi ci samag curga, ba teg ngànguneem ci kaw doj yii ma fi suul, mu firi fi xaymaam.
11
Bu dikkee dina tas réewum Misra: ku wara médd, médd; kuy dugg njaam, duggi njaam; kuy fàddoo saamar, fàddoo saamar.
12
Nabukodonosor dina jafal kër tuuri Misra yi, lakk tuur yi, mbaa mu yóbbu leen. Ni ab sàmm di teeñe mbubbam, ni lay teeñe réewum Misra ba mu set wecc, daldi daagu, dem yoonam.
13
Dina rajaxe tuuri doj ya sampe ca Bet Semes ci biir Misra te dina lakk këri tuur yi ci Misra.”»
← Chapter 42
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 43
Chapter 44
Chapter 45
Chapter 46
Chapter 47
Chapter 48
Chapter 49
Chapter 50
Chapter 51
Chapter 52
Chapter 44 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42
43
44
45
46
47
48
49
50
51
52