bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Proverbs 7
Proverbs 7
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 6
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 8 →
1
Doom, sàmmal samay wax, fonk samay santaane.
2
Jëfeel samay santaane, ba dund, jàppal samay ndigal sa fukki loxo.
3
Takkal ci say waaraam, bind ko ci sa àlluway xol.
4
Safool xel mu rafet, muy sab jigéen, te nga xejjoo dég-dég ni sa mbokk lenqe.
5
Dina la aar ci ndaw su yemadi, bokk feneen, di wax lu neex.
6
Damaa tollu sama palanteer, séentu ca xarante ya,
7
séen ca biir téxét ya, ku ma seetlu ca xale yu góor ya, muy ku ñàkk bopp.
8
Muy dem ba fa ndaw say taxaw, ca selebe yoon wa, daldi wuti kër ndaw sa.
9
Ngoonug suuf la, jant biy lang, muy lëndëm di gëna guddi.
10
Ndaw si jekki dajeek moom, sol yérey gànc, lal pexeem.
11
Daa xumb, të, du toog këram.
12
Ma nga ca mbedd ma, ne ca pénc ya, ruqoo ruq, ma ngay yeeroo.
13
Ndaw sa ne ko katam, fóon, ne wajj, ne ko:
14
«Tey matal naa la ma digoon Yàlla, yàppu bernde waa nga kër ga, saraxu cant la.
15
Moo ma taxa dikk dajeek yaw. Seet naa laa seet, ba gis la.
16
Lal naa saab lal, ba mu jekk, di malaan yu yànj, bawoo Misra.
17
Lal ba, ma xeeñal, mu ne bann, di ndàbb, cuuraay ak xas mu neex.
18
Dikkal, nu baanee baane, ba bët set, te bànneexu ci mbëggeel.
19
Sama jëkkër newu fa, daa dem yoon wu sore.
20
Mbuusum xaalis la ŋàbb, yóbbu, du ñibbsi ndare weer wi fees dell.»
21
Muy mocc ak a moccaat, ba nax ko, di wax lu neex, ba man ko.
22
Waa ja jekki, topp ko, mbete yëkk wu ñuy rendiji, mbaa dof bu ñu jéng, di ko yari.
23
Mooy picc mu tàbbi cig fiir. Du xam ne day dee, ba keroog fitt jam ko ci xol.
24
Kon nag, doom, dégluleen ma, teewluleen samay wax.
25
Bu leen soosu ndaw xiir ci moy, buleen teggi, topp ko.
26
Bare na ku dee, moo ko rey, maneesula waññ ñi mu rey ñépp.
27
Këram yoonu njaniiw la, daa bartalu, tàbbi néegi ndee.
← Chapter 6
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 8 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31