bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Job 10
Job 10
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 9
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 11 →
1
Maaka sib sama dund gii! Naa afal sama kàddug tawat, di àddoo naqaru xol.
2
Dama naa Yàlla: Bu ma topp ug tooñ. Xamal ma kay li nga may topp, lu mu!
3
Ana lu la note di jariñ, ba ngay bañ li nga sàkke sa loxol bopp, tey àntal pexem ku bon?
4
Xanaa gëti nit doŋŋ nga am, am ni nit di gise rekk ngay gise?
5
Say fan daa tollook fani doom aadama, am say at daa yem ak ati nit,
6
ba ngay seet fu ma ñaawe, di liñbat fu ma moye?
7
Moona xam nga xéll ne tooñuma, te amul kenn kuy xettli nit ci sa loxo.
8
Say loxoo ma mooñ, tabax ma ba ma mat sëkk, léegi nga di ma yàq yaxeet!
9
Rikk fàttlikul ne yaa ma tabax, ni bu ma doon ban, xanaa doo ma delloo xaat ci pëndub suuf?
10
Xanaa du yaa ma xelli woon ni meew ci sama biiru ndey, wayal ma nim soow,
11
wodde ma der ak suux, ràbbe ma yax aki siddit?
12
Yaa ma may bakkan, won ma ngor, yaa sàmme sa yégeel samag noo.
13
Ndeke yoo lii nga dencoon ci sa xol, xam naa ne lii nga naroon:
14
ne ma dann, ba su ma bàkkaaree, doo ma baal samag tooñ.
15
Su ma defee lu bon, ngalla man, te bi ma defee njekk it, sañumaa siggi, gàcce laa suure, sangoo toroxte.
16
Waaye su may siggi rekk nga mel ni gaynde, di ma rëbb, dellu di ma lore say kiraama,
17
yónneeti ma say seede, gën maa songati, ay gàngoor di wuutante fi sama kaw.
18
Ana loo ma doon génnee sama biiru ndey? Doon naa dee te bët du ma gis!
19
Doon naa mel ni ku masula am, jóge ci biir, ñu yóbbu bàmmeel.
20
Xanaa du fan yu néew laa dese? Ba ma boog! Xiddil, ma leqliku,
21
bala may dëddu, délseetuma, bala may tàbbi réew mu lëndëm ga ne këruus,
22
réewum lëndëm, mu ne këruus, salfaañoo, ag leer sax, saf fa lëndëm!
← Chapter 9
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 11 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42