bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Job 8
Job 8
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 7
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 9 →
1
Bildàdd ma bàyyikoo Suwa, àddu ne:
2
Ana foo àppal sa wax jii? Ngay mbel-mbeli ni callweer!
3
Ana Yàllaak safaan yoon? Ana Aji Man jeek safaan dëgg?
4
Bu ko sa doom yi moyee, kay, mu ba leen ak seen añub tooñ!
5
Yaw nag soo sàkkoo Yàlla, dagaan Aji Man ji aw yiwam,
6
soo muccee ayib te jub, day daldi taxaw temm ci say mbir, delloo la sa kërug njekk,
7
nga yokkoo yokku ëllëg, ba xeeb sa démb.
8
Laajal rekk maas gi nu jiitu, te teewlu seen gëstuy maam ya.
9
Nun xamunu, démb rekk lanu, sunu fani kaw suuf di takkndeer suy wéy.
10
Ñi ñu jiitoo lay xamal, wax la, tibbe seen xol yii kàddu, dénk la:
11
«Ndax jàqaar dina naate fu dul ban bu tooy, am barax dina saxe fu amul ndox?
12
Bu ndox ma ŋiisee, mooy jëkka lax, te du ñoragum bay mata dog.»
13
Loolooy muju képp ku fàtte Yàlla, yaakaaru yéefar, tas rekk,
14
cëslaayam màbb, làquwaayam di lëndu jargoñ.
15
Mu wéeroo këram, kër gay yëngu; mu ŋoyu ca, muy jaayu.
16
Ku gëmadee ngi mel ni garab gu jant biy jam, mu naat; car yay lawe tool ba mu saxe,
17
reen ya rawaasoo ci biir jalub xeer, muy kërug dojam gu mu ŋoy.
18
Nga buddee ko bérab ba mu sax, bérab ba jàmbu ko, ne ko: «Masuma laa gis!»
19
Geneen garab ay jebbi, wuutu ko. Mu ngoog, ab yéefar, nii la mujam di rafete!
20
Dama ne: Yàlla du gàntal ku maandu, te du dooleel kuy def lu bon.
21
Moo lay may loo ree, bay sarxolle,
22
say bañ gàccoo gàcce, xaymab ñu bon ña gental.
← Chapter 7
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 9 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42