bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Job 18
Job 18
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 17
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 19 →
1
Bildàdd mu Suwa àddu, ne:
2
Xanaa dungeen noppi mukk? Àndleen ak xel, nu wax.
3
Ay mala ngeen nu teg daal, def nu ay naataxóona?
4
Yaw nag yaa topp sa mer ba loru! Ayóobaa, àddina day gental ngir yaw a? Am aw doj ay toxal boppam ngir yaw?
5
Ku bon kay lag leeram di fey, te taalam du jolli.
6
Xaymaam day lëndëm, làmpam ba ko tiim ne kamaj.
7
Bu daa waaxu démb, di temp tey, ay mébétam di ko mbas.
8
Moo dox ba tàbbi cib caax, wëndeeloo biir mbaal,
9
tànk ba téqtaloog fiir, ab racctal ne ko ràtt.
10
Buum ga koy lonk a nga suulu, am yeer di ko xaarew ñall.
11
Lu ragloo koy darey mbetteel, ne ko dann.
12
Mooy xiif ba doole réer ko, musiba taxaw, xejjoo ko.
13
Jàngoro di ko ŋacc, woppi ndee di lekk cér ya.
14
Ku bon lees di ñoddee fa jàmmi xaymaam, diri ko ba fa kanam buuru musiba yi,
15
manees naa dëkke xaymaam, moomatu ko, tamarax lees fay suy.
16
Ku bon mooy garab gu dee kaw ak suuf, reen wow, xob lax.
17
Turam tukkee kaw suuf, ba deesatu ko tuddem pénc.
18
Dees koy bëmëxeg leer, tàbbal lëndëm, dàqe ko àddina.
19
Du doom, du askan wu muy waccey bokkam, te kenn du desey dalam.
20
Waa sowu jommi cig mujam, waa penku di rasu naa:
21
«Dalub kàccoor déy, lee di mujam, ku faalewul Yàlla, nii la màkkaanam!»
← Chapter 17
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 19 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42