bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Job 42
Job 42
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 41
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
1
Ba loolu amee Ayóoba àddu ne Aji Sax ji:
2
Xam naa ne lépp nga man; du lenn loo tële.
3
Nee nga ma: «Ana koo doon, bay lëntal samay dogal te xamoo?» Maa wax moos te xawma lenn ci kawtéef yu ma wees, ump ma.
4
Nee nga: «Déglul, maa lay wax. Ma laaj la, nga xamal ma.»
5
Dég-dégu nopp laa amoon ci yaw, tey bët laa la teg.
6
Moo ma tax ne: «Wàqet, tuubi-ruubi,» ba diwoo suuf akub dóom.
7
Gannaaw ba Aji Sax ji waxee Ayóoba yooyu kàddu, Aji Sax ji dafa wax Elifas ma cosaanoo Teman, ne ko: «Sama xol tàng na ci yaw, yaak sa ñaari xarit yi, ndax waxuleen dëgg ci man ni sama jaam bi Ayóoba waxe.
8
Kon nag sàkkleen juróom ñaari yëkk, ak juróom ñaari kuuy. Ngeen dem ba ca sama jaam ba Ayóoba, joxe ko fa saraxu rendi-dóomal, te Ayóoba ñaanal leen, ma seet ci moom ba bañ leena mbugale seenug ndof. Ndax waxuleen dëgg ci man ni sama jaam bi Ayóoba waxe.»
9
Ba loolu amee Elifas waa Teman ba, ak Bildàdd waa Suwa, ak Cofar waa Naama daldi dem, def la leen Aji Sax ji sant. Aji Sax ji seet ci Ayóoba.
10
Gannaaw ba Ayóoba ñaanalee xaritam ya, Aji Sax ji tijji wërsëgu Ayóoba. Aji Sax ji ful na ñaari yoon mboolem alalu Ayóoba.
11
Ba loolu amee mboolemi bokkam, góor ak jigéen, ak mboolemi xameem ya woon, dikk bokk ak moom bernde ca këram. Ñu dëfal ko, mas-sawu ko ci bépp coono bu ko Aji Sax ji tegoon. Ku ci nekk jox ko dogu xaalis ak jaarob wurus.
12
Aji Sax ji nag barkeel mujug Ayóoba lu raw ndoorteem. Mu am fukki junniy gàtt ak ñeent (14 000), ak juróom benni junniy giléem (6 000), ak junniy lëkkey nag (1 000) yu muy rijjee, ak junniy mbaam yu jigéen (1 000).
13
Mu amaat juróom ñaari doom yu góor ak ñett ñu jigéen,
14
ka mag ca jigéen ña, mu tudde ko Yemima, ka ca topp di Keciya, ka ca toppaat di Keren Apug.
15
Mboolem jigéeni réew ma, amul ku rafete woon ni ñetti doomi Ayóoba yooyu. Seen baay nag sédd leen ndono lu tollook seen céri càmmiñ.
16
Gannaaw loolu Ayóoba dundaat na téeméeri at ak ñeent fukk (140). Gis na ay doomam, gis ay sëtam, ba muy ñeenti maas.
17
Ayóoba màggat na ba ñor xomm, doora dee.
← Chapter 41
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42