bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Job 27
Job 27
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 26
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 28 →
1
Ayóoba dellu yékkati kàddoom, ne:
2
Yàlla miy dund seere na, moom mi ma xañ dëgg, moom Aji Man ji ma teg naqaru xol,
3
ne li feek may ànd ak bakkan, di noyyee noowal Yàlla,
4
sama gémmiñ gii du wax njubadi, sama làmmiñ wii laa ne, du tudd ay fen.
5
Yàlla buma leen jox dëgg, ba ba may dee duma weddi samag mucc sikk.
6
Sama njekk laay ŋoy, duma ko ba, sama giiru dund sama xel du ma yedd.
7
Yal na noon bokk ak ku bon demin, ku may fexeel bokk ak kàccoor ag muj.
8
Ana lu yéefar biy yaakaarati bu fàddoo, ba Yàlla moom bakkanam?
9
Bu ko njàqare di dikkal, Yàlla day dégg yuuxam a?
10
Ndax Aji Man ji la daan bége, am daan na tudd Yàlla fu mu tollu?
11
Ma xamal leen boog li ci dooley Yàlla, duma leen nëbb li Aji Man ji namm.
12
Dama ne, yeen ñépp a ko gisal seen bopp sax, kon lu leen yebuloo nii ci neenug neen?
13
Lii mooy cér bi Yàlla sédd ku bon, mooy wàll wi Aji Man ji dencal ku néeg.
14
Njabootam ne xas, saamar jagoo, te balaa booba duñu lekk ba suur.
15
Ña koy wuutu, mbas a leen di rey, te ay jëtunam duñu ko jooy.
16
Su doon jal xaalis ni suuf, yére yomb ko ni feppi suuf,
17
mooy dajale, aji jub sol; xaalis ba, kay def njub séddoo.
18
Mooy tabax kër gu tanewul mbaarum wattukatu tool, te lëndu jargoñ gën koo dëgër.
19
Keey tëraale alal ju mu dul gisati; day xippi, fekk mu ne mes.
20
Musibaa koy dab nim wal, ngëlénu guddi këf, yóbbu,
21
ngelawal penku déjjatee ko këram, jalax, mu wéy.
22
Dees na ko diir, bañ koo ñéeblu, mu daw, di wuta rëcc dooley saan ya.
23
Dees na ko tacc-taccali loxo, di ko ciipoo fa këram.
← Chapter 26
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 28 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42