bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Job 14
Job 14
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 13
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 15 →
1
Ku jigéen jur, yaa néewi fan, géejal coono!
2
Dangay tóor rekk, lax, wéy ni takkndeer, doo toog.
3
Mooy kii nag nga teg bët, mooy man mii nga nara layool!
4
Lu sobewu, ana ku ci mana am lu laab? Du kenn!
5
Ndegam yaa dogalal nit ay fanam, lim ay weeram, dogal àpp ba, te du jaas,
6
teggi ko boog say gët, mu dal-lu, ni liggéeykat bu jaanam wàcc ci bés.
7
Garab sax ñàkkul yaakaar. Boo goree, mu jebbiwaat, ba du ñàkk ay njebbat.
8
Reen ba man naa màggat, ëkk ba deeye biir suuf,
9
mu yég um ndox, rekk, jebbi, saxaat nim njëmbat.
10
Waaye nit dee, doole réer, bakkan rot, mu ne mes.
11
Day mel ni déeg bu ŋiis, mbaa dex gu wow ba jeex.
12
Doom aadama it tëdd, du jógati, du yewwooti, asamaan fekke, du jógeeti ciy nelaw.
13
Éy soo ma nëbboon biir njaniiw, làq ma, ba sa mer giif, dogalal ma àpp, te bañ maa fàtte!
14
Ndax dees na dee, di dundati? Konoon ma muñe ko sama fani coono yépp, ba keroog sama kuutaay yiwisi ma.
15
Konoon nga woo ma, ma wuyu, te kon nga namm sa càkkéefu loxo.
16
Konoon yaay lim samay jéego, te doo ma topp samay bàkkaar.
17
Konoon samag tooñ yebe ci mbuus mu takke, sama ñaawtéef, nga muure ko malaan.
18
Waaye aw tund day màbb, ruus; aw doj di toxu,
19
am ndox di jonji xeer ba mu jeex, waame buub suuf, yóbbu, te noonu ngay neenale yaakaaru doom aadama,
20
man ko, mu dëddu fàww, kanam ga soppiku, nga jalax.
21
Doom ya tedd, yégul; ñu tekkeedi, tinul.
22
Nit yégul lu moy mititu boppam te bakkanu boppam lay tiisoo.
← Chapter 13
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 15 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42