bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Job 11
Job 11
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 10
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 12 →
1
Cofar ma bàyyikoo Naama àddu, ne:
2
Yii kàddu yu wale, deesu ko tontoo? Wax ju bare tax na nit a yey?
3
Sa kebetu yii wedamal na kenn a? Am dangay ñaawle te deesu la tiiñal?
4
Nee nga sa àlluwa wér na péŋŋ, sa jëw rafet, Yàlla seede.
5
Éy su Yàlla nammoona wax, ba àddu, wax ak yaw,
6
àgge la kumpay xelam mu rafet, mi wees dég-dég, kon nga xam ne Yàlla jéllale na sa lenni tooñ!
7
Dangaa mana gëstu mbóoti Yàlla, ba gis ko? Am yaa ñédd Aji Man ji?
8
Lu gëna kawe kaw, ana loo ci man? Lu gëna xóot njaniiw, ana loo ci xam?
9
Màggaayu Yàllaa sut suuf, gëna yaatu géej!
10
Su dikkee, tëj nit, woo ko péncum àtte, ku ci man dara?
11
Moom mi xàmmee ñi dul niti dara, mooy gis lu bon, te du laaj mu teewlu.
12
Waaye ku boppam feesul, bu muusee, mbaamu àll a judduwaale nangu.
13
Waaye yaw soo defee sa xel ci Yàlla, dékk ko say loxo,
14
fabal say ñaawtéef, sànni, te baña xajal njubadi sa biir xayma,
15
kon déy, nga mucc gàkk, siggi; dëju te doo tiit,
16
sa coonob tey ngay fàtte, ni waltan mu wal ba wéy doŋŋ ni nga koy fàttlikoo,
17
te yaay gëna leer jantub njolloor, ba lëndëm di saf leeru njël.
18
Kon nga am yaakaar ak kóolute, aaru, soo tëddee, nelaw,
19
jaaxaan, kenn du la lëjal, ñu bare di la leewaayu;
20
ku bon jàq, ba gët ya giim, rawtu réer ko, yaakaaratul lu moy noowam gu mujj.
← Chapter 10
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 12 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42