bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Job 35
Job 35
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 34
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 36 →
1
Eliyu dellu ne:
2
Defe nga ne lii yoon la? Nga ne: «Maa am dëgg fi kanam Yàlla,»
3
te naan ko: «Ana lu ma ci soxal man, ak lu ma ñàkka bàkkaar di jariñ?»
4
Man mii nag maa lay tontu, yaak say xarit.
5
Séentul asamaan te xool, niiral niir yii la tiim!
6
Soo bàkkaaree, lu muy wàññi Yàlla? Man ngaa tooñ, tooñati ba def ko dara?
7
Ana njekk goo def ba may ko lenn, ak lu muy jële sax ci say loxo?
8
Sag mbon, sa moroomu nit lay lor, sag njekk it doom aadama ni yaw lay jariñ.
9
Noteel law na ba nit ñiy yuuxu, di woote ku leen wallu ci loxol boroom doole.
10
Waaye kenn du ci ne: «Wóoy ana Yàlla mi ma sàkk, kiy fentloo woyi cant ci biir guddi,
11
di nu xamal lu rabu àll xamul? di nu may xel mu njanaaw amul?»
12
Bu nit ñu bon ñiy woote wall, du wuyu ngir seenug réy.
13
Neen lañuy woote, nde Yàlla du leen déglu, Aji Man ji du leen faale.
14
Kon ngalla yaw mi ne gisoo ko, te ne diis nga ko sa mbir, di ko xaar.
15
Nga neeti Yàlla du mer, di mbugale, te yoonam newul ci njubadiy nit.
16
Ayóoba mii de, cóolóolu neen lay wax, mbel-mbel ju àndul ak xam-xam.
← Chapter 34
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 36 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42