bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Wolof
/
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
/
Job 23
Job 23
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
← Chapter 22
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 24 →
1
Ba loolu amee Ayóoba àddu, ne:
2
Ba tey maa ngi jooy jooy yu metti, di onk bay ub gémmiñ,
3
Éy bu ma xamoon fa may gise Yàlla, ba àkki péncam,
4
diis ko sama mbir, àgge ko lépp lu may tawat,
5
ba xam lu di tontam, dégg li mu may wax.
6
Ndax dooleem ju bare la may yeye? Déedéet xanaa! Dina ma teewlu moos,
7
ba ku jub layoo faak moom, ma daldi mucc sama àttekat fàww.
8
Seet naa wetu penku, Yàlla nekku fa, ma seet sowu, gisuma ko.
9
Bu jàppee fa wetu bëj-gànnaar, gisuma ko fa, bu jàllee bëj-saalum séenuma ko fa.
10
Ndaxam moo xam fi ma jaare, te bu ma nattoo, ma génn ci ni wurus wu ñu xelli.
11
Tànkam, sama tànk, yoonam laa tegu, moyuma ko.
12
Dëdduwma ay santaaneem, sama biir xol laa denc ay kàddoom.
13
Yàlla de kenn la, ana ku koy waññi? Coobarey bakkanam lay def.
14
Mooy sottal lu mu ma dogalal, te bare na lu mu ma nasal.
15
Lee tax su ma janook moom, tiit, te lu ma gëna xalaat, gën koo ragal.
16
Yàlla daal a rëccal samaw fit, Aji Man jee ma tiital!
17
Du lëndëm gi ma nekke moo ma wedamal, du lëndëm gii ma muur.
← Chapter 22
Jump to:
Chapter 1
Chapter 2
Chapter 3
Chapter 4
Chapter 5
Chapter 6
Chapter 7
Chapter 8
Chapter 9
Chapter 10
Chapter 11
Chapter 12
Chapter 13
Chapter 14
Chapter 15
Chapter 16
Chapter 17
Chapter 18
Chapter 19
Chapter 20
Chapter 21
Chapter 22
Chapter 23
Chapter 24
Chapter 25
Chapter 26
Chapter 27
Chapter 28
Chapter 29
Chapter 30
Chapter 31
Chapter 32
Chapter 33
Chapter 34
Chapter 35
Chapter 36
Chapter 37
Chapter 38
Chapter 39
Chapter 40
Chapter 41
Chapter 42
Chapter 24 →
All chapters:
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
34
35
36
37
38
39
40
41
42